Deuteronomy 9:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du seen genn njekk, akug njub gu leen may ngeen nanguji seenum réew. Waaye mbonug xeet yii moo waral seen Yàlla Aji Sax ji dàqal leen leen, ngir sottal kàddu ga mu giñaloon seeni maam Ibraayma ak Isaaxa ak Yanqóoba.