Deuteronomy 9:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon na leen bir ne du seenug njekk moos la leen seen Yàlla Aji Sax ji joxe mii réew mu baax, ngir ngeen moom ko ndax, askan wu daŋŋiiral ngeen.