Ecclesiastes 11:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xëyal, ji sa jiwu, gont, baña tàyyi; muy lii di lee, xamoo lu ciy nangu, am ñaar ñépp ay bokk baax.