bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ephesians 1:10
Ephesians 1:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mu tëral ne, bu jamono yi wéyee ba lépp mat, dina dajale lépp ci kilifteefu Kirist, muy ci kaw, muy ci suuf.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li Yàlla namm, bu fan yi matee, moo di dajale lépp ci kilifteefu Almasi, mboolem la fa asamaan, ak li fi suuf.