Ephesians 1:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ci leeral seeni xol. Noonu dingeen xam yaakaaru ëllëg, ji leen Yàlla wooye, di ndam lu xel mënta daj, li nekk ci cér, bi mu dencal gaayam yu sell yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngir itam seen bëti xol leer ba ngeen gis yaakaar ji ci wooteem, ak ni ay ngëneelam géejoo te yéeme, ñeel ñu sell ñi mu séddoo.