Ephesians 1:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ngeen xam it, ni kàttanam màgge ba jéggi dayo, jëm ci nun ñi gëm, dëppook dooleem ju ràññiku,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngeen boole ci xam manooreem gu nattuwul gi mu nu lañalal, nun gëmkat ñi. Manoore googu feeñ na ci jëf ji sottee ci kàttanam ak dooleem,