Ephesians 2:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te yéen itam Yàlla dekkal na leen, yéen ñi doon ndee fa kanamam ci seeni moy ak seeni bàkkaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen dangeena dee woon ndax seeni moy ak seeni bàkkaar,