Ephesians 2:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye léegi ci seen bokk ci Kirist Yeesu, yéen ñi sore woon jege ngeen ndax deretu Kirist ji ñu tuur.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye yeen ñi sore woon, léegi bi ngeen nekkee ci Almasi Yeesu, jege ngeen ndax deretu Almasi ji tuuru.