Ephesians 2:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu ko defee mu ñëw, yégalsi nu xebaaru jàmm fa kanam Yàlla, yéen ñi sore woon ak nun ñi jege.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo dikke xibaaru jàmm buy yégle jàmm ju leen ñeel, yeen jaambur ñi ko sore woon, te ñeel nu, nun ñi ko jege,