Ephesians 2:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te ci seen bokk ci Kirist, Yàlla boole na leen tabax yéen itam, ba ngeen nekk dëkkukaayam, jaar ci Xel mu Sell mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci Almasi ngeen bokke ci tabax bi, yeen jaambur ñi itam, ba mana doon dëkkuwaayu Yàlla, ci ndimbalal Noo gu Sell gi.