Ephesians 2:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ba fu jamono yem, dina lañal fi sunu kanam yiwam wu réy wi xel mënta takk, jaar ci baaxaay gi mu nu won ci Kirist Yeesu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbaax gi nu Yàlla won ci Almasi Yeesu, moom lay firndeele mboolem xarnu yiy ñëw, ni yiwam yaatoo ba tiiñ am xel.