Ephesians 3:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag maa ngi leen di ñaanal, man Pool mi ñu tëj kaso ci turu Kirist ndax sas wi may bey ci yéen, xeet yi dul Yawut.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo ma tax di ñaan, man Póol mi ñu tëj ngir Almasi, ndax ñi dul Yawut, yeen jaambur ñi,