Ephesians 3:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci turam am nanu kóolute fa kanam Yàlla, ak bunt bu yaatu ci moom ci kaw ngëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci Yeesu, ci kaw ngëm gu nu ko gëm lanu ñemee àgge fit wu mat sëkk, fa kanam Yàlla.