Ephesians 3:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Léegi nag, na ndam li féete ak Yàlla, mi man a yeggale lépp luy ñaan mbaa yéene, ba weesu ko fuuf, dëppook kàttan giy jëf ci nun;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom mi mana jëfoo kàttan giy liggéey ci nun, ba sottal mboolem lu nu ñaan ak lu nu xalaat, ba wees loola fuuf sax,