Ephesians 3:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
May na ma, man mi gën a tuuti ci gaayi Yàlla yu sell yi, may xebaar xeeti àddina barkeel yu xel dajul yi ci Kirist;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man mi yées ci ñu sell ñépp lañu may woowu yiw, ba may xibaar jaambur ñi dul Yawut, xéewal yu amul kem yi ci Almasi.