Ephesians 3:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
te it may sulli melokaanu mbir mu xóot mi Yàlla tëral, te doon kumpa njàlbéen ga ba tey ci moom, mi sos lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
May niital ñépp, ni Yàlla nara sottale mébétam, miy mbóot mu làqu woon naka jekk fa moom Yàlla mi sos lépp.