Ephesians 4:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ki wàccoon moo yéegaat, ba tiim asamaan yépp, ngir fees lépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kooku wàccoon mooy kenn ki yéegaat ba tiim asamaan yépp, ngir def lépp feese jëmmam.