Ephesians 4:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu nu mànkoo ci sunu ngëm ak ci xam Doomu Yàlla ji, ba kera nuy egg ci nekk nit ku sotti, te taxaw taxawaay bu dëppook matug Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko defee nu mana màgg nun ñépp ba doon benn ci ngëm, ak ci xam-xam bu mat ci Doomu Yàlla ji, ba kera nuy doon magum jëmm, bay tollook taxawaayu Almasi bi mat sëkk.