Ephesians 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye dinanu wax dëgg, ëmb ko ci mbëggeel, bay màgg ci fànn gu ne ci sunu bokk ci Kirist. Mooy bopp,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su boobaa kay, dëgg gu nu wodde cofeel lanuy wéye, tey màgg ci bépp fànn, ci moom Almasi miy bopp bi.