Ephesians 4:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maanaam ngeen yulli seen jikko ju bon, ji ngeen judduwaale te daan fés ci seeni jëf, te muy gën a yées, moom ak i bëgg-bëggam yuy naxe kese.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te mooy ngeen ba seen jikko ju jëkk ja, ngeen teqlikoo ak seen jëmmu démb ja masa topp bànneexi bakkan yuy naxe, ba sóobu ci yàqute.