Ephesians 4:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag bàyyileen di fen, tey wax dëgg kenn ku nekk ci moroomam, ndax ku nekk sa genn-wàllu moroom nga.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag bàyyileen fen, te ku nekk di wax sa moroom, dëgg, ndax ku nekk ci yeen sab céru moroom nga.