Ephesians 4:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te jenn Yàllaa am, di Baayu ñépp, mu tiim ñépp, fees ñépp, te dëkk ci ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it jenn Yàllaa am; mooy Baayu ñépp, moo tiim ñépp, di jëf ci ñépp te nekk ci ñépp.