Ephesians 4:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Looloo tax Mbind mi ne:«Yéeg na ba ca fa gën a kawe,yóbbaale mbooloom noon mu bare, mi mu noot,tey séddale nit ñi ay may.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax ñu ne: «Moo yéeg fa kawa kaw, yóbbaale gàngoor gu mu jàppe xare, te moo séddale nit ñi ay may.»