Ephesians 5:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte waxtaane sax li ñuy def ci nëbbu, lu ruslu la;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat li nit ñooñu di làquy def, waxtaane ko sax, lu ruslu la.