Ephesians 5:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu sàmmleen seen dundin, waxuma ni ñu amul xel, waaye ni ñu am xel,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag xool-leen bu baax seen jëfin, defleen jëfinu nit ñu am xel, te baña mel ni ñu ñàkk xel,