Ephesians 5:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buleen ñàkk bopp nag, waaye xamleen liy coobareg Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax buleen def jëfi ñàkk bopp, waaye jéemleena xam coobarey Boroom bi.