bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ephesians 5:23
Ephesians 5:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte góor mooy kilifag jabaram, ni Kirist nekke kilifag mbooloom ñi gëm, muy jëmmam ji muy sàmm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Almasi moo di musalkatu mbooloom gëmkat ñi, mbooloo mi di aw yaramam. Te itam ni Almasi dee boppu mbooloom gëmkat ñi, ni la jëkkër ji dee boppu jabaram.