Ephesians 5:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen nag góor ñi, na ku nekk bëgg jabaram, ni Kirist bëgge mbooloo mi, ba joxe bakkanam ndax moom,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jëkkër nag, na sopp jabaram ni Almasi soppe mbooloom gëmkat ñi, ba jooxeel leen bakkanam.