Ephesians 5:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte kenn musul a bañ sa yaram. Waaye danga koy dundal, di ko fonk. Noonu it la Kirist fonke mbooloo mi;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax kenn masula bañ suuxu boppam, xanaa mu di ko dundal, di ko topptoo, ni Almasi ak mbooloom gëmkat ñi,