Ephesians 5:32 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu ëmb na mbóot mu xóot; man maa ngi wax ci lu jëm ci Kirist ak mbooloo mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbóot mu xóota ngi ci dog boobu, waaye man, li may wax moo di dog bi moo misaal diggante, bi Almasi séq ak mbooloo mi.