Ephesians 5:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu leen kenn nax ci ay waxi neen, ndaxte jëf yooyooy tax meru Yàlla di wàcc ci kureelu ñi ko déggadil.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu leen kenn naxe waxi ngelawal neen, ndax yooyu ma lim mooy wàcce sànjum Yàlla ci kaw aji déggadi ñi.