Ephesians 6:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Naka yéen xale yi, nangeen déggal seeni waajur, ci li ngeen bokk ci Boroom bi, ndaxte looloo rafet.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka yeen xale yi, déggal-leen seeni waajur, ngir Boroom bi, ndax moo war.