Ephesians 6:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yónnee naa leen Tisig sama mbokk, mi ma sopp, te muy jawriñ ju takku ci liggéeyu Boroom bi, ngir mu xamal leen lépp li aju ci man ak li may def.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dingeen mana xam nag lu jëm ci man, ak li may def, ndax Tisig, mbokk mu ñu sopp, jawriñ ju wóor ci liggéeyu Boroom bi, moo leen di xamal lépp.