Ephesians 6:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa leen ko yónneel sama bopp, ngir ngeen xam li nu nekke, te mu dëfël seeni xol.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu ci boppam sax moo waral ma yónni ko ci yeen, ngir mu xamal leen ni nu nekke, ba seral seen xol.