Ephesians 6:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen baay yi it, buleen bundaxataal xale yi, waaye ngeen yar leen, di leen yemale ak a yee ci Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen ñiy baay it, buleen xoñoñal xale yi, waaye yarleen leen, di leen jubanti, di leen xamal coobarey Boroom bi.