Ephesians 6:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Beyleen seen sas nag ak xol bu tàlli, ni su doon ngir Boroom bi te du nit,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Liggéeyal-leen leen ci xol bu tàlli, ba mu mel ni Boroom bi ngeen ko defal, waaye du nit doŋŋ,