Ephesians 6:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
xam ne ku def lu baax, Boroom bi delloo la ko, muy jaam, muy gor.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te ngeen xam ne nit ki, mu dis gor mbaa ab jaam, mboolem lu mu def ci lu baax, loola la ko Boroom biy delloo.