Esther 1:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Memukan wax ca kanam Buur ak kàngam ya, ne leen: «Du Buur doŋŋ la Lingeer Wasti tooñ. Waaye tooñ na mboolem kàngam yi ak mboolem baadoolo yi ci mboolem diiwaan yi.