Esther 2:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fekk na Esteer waxul askan wa mu bokk ak kër ga mu fekk baax, ndax Mardose da koo santoon ne ko bumu ko wax.