Esther 2:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur def bernde ju réy ngir mboolemi kàngamam aki jawriñam, terale ko Esteer; daldi noppal diiwaan yi, teg ca nàddil nit ñi ni mu ware buur.