Esther 2:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jamono yooyu Mardose amee ndombol tànk ca buntu kër buur, ku ñuy wax Bigtan ak ku ñuy wax Teres, di ñaari fara buntu kër buur, ñoo am lu ñu meree lool Buur Aserus, bay lal pexe mu ñu ko bóome.