bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Esther 2:9
Esther 2:9 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xale bi neex Ege, mu baaxe ko, gaaw indil ko lu mu defaroo, nàddil ko ag lekkam, féetale ko juróom ñaari surga yu jigéen yu ñu tànne kër Buur. Ci kaw loolu mu dalal Esteer mooki surgaam fa gën ca kër jigéen ña.