Esther 4:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Esteer woolu Atag, ma Buur féetaleek moom, te muy kenn ci bëkk-néegi buur. Mu yebal ko ci Mardose, ngir xam lan la ak lu waral loolu.