Esther 5:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur, ndegam yéwéne nga ma, te may ma li may ñaan, defal ma li may sàkku di sa coobare, ngalla, Buur, àndal ak Aman, dikk ca bernde ja ma leen di waajalal. Kon bu subaa dinaa la wax li ngay laaj.»