Esther 6:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka lañuy wax ak moom, ndawi buur ne jalañ, daldi gaaw yóbbu Aman ca bernde ja Esteer di waajal.