Esther 8:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu Buur Aserus jox bésub keroog Lingeer Esteer kër Aman, fitnaalkatu Yawut ya. Ñu woo Mardose ca Buur, ndax fekk na Esteer xamle ba noppi na Mardose bokkeek moom.