Esther 8:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu wara siiwal ab sottib bataaxal ba, muy ndigalu yoon ci diiwaanoo diiwaan, biralal ko mboolem xeet yi, ngir bésub keroog Yawut yi taxaw temm, feyoonteek seeni noon.