Esther 9:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yawut ya daje seeni biir dëkk ca mboolem diiwaani Buur Aserus, ngir dal ci kaw ñi leen di wuta lor. Amul ku leen mana të ci xeet yépp, ndax tiitaange lu réy lu ñu am ci ñoom.