bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Esther 9:22
Esther 9:22 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
di ko baaxantale bés ya Yawut yi dal-loo ca seeni noon, ak weer wa seen naqar walbatikoo di mbégte, seen tiis di bésub jàmm, ngir ñuy wormaal yooyu bés, muy bési bernde ak bànneex yu ñuy joqlantey teraanga, di ci defal néew-ji-doole.