Esther 9:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aman doomu Amdeta, Agageen ba, fitnaalkatu bépp Yawut, moo fexeeloon Yawut yi, ngir faagaagal leen. Jumtukaayu tegtal bi ñuy wax Pur lañu jëfandikoo woon, ngir jàpp bés ba mu leen wara faagaagal, sànk leen.